• Kër gi
  • Xibaar
  • Gis-Gis
  • COKKAASU ODIA
  • NATAALI AYUBÉS BI
  • WAXLEEN SEEN XALAAT
  • FÀTTALIKU DÉMB
Search
  • Lu Defu Waxu
  • Jokkoo
Lu Defu Waxu
  • Kër gi
  • Xibaar
    • WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?

      ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI

      MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

      LAAJ-TONTU : SAADA KAN BÓRIS JÓOB (II)

      NAWETU ITALI AK JOŊANTE REN JI

  • Gis-Gis
    • Bataaxalu Saalif Keyta ñeel IBK

      AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?

      DÉMB AK TEYU DOXANDÉEMI ITALI YI

      WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?

      LAAJ-TONTU SAADA KAN/BÓRIS (III)

  • COKKAASU ODIA
    • CÉY BII MÀRSE…

      BUUR

      “MARTEAU” BI

      IMMEUBLE PDS/WADE BAAY AK DOOM

      Akademi Kàddu Gu Ñagas

  • NATAALI AYUBÉS BI
    • NATAALI AYUBÉS BI

      NATAALI AYUBÉS BI

      NATAALI AYUBÉS BI

      Kër Sëriñ Nomination

      “BATTRÉ” DA FA XEW CI JAMONO

  • WAXLEEN SEEN XALAAT
    • MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL

  • FÀTTALIKU DÉMB
Home COKKAASU ODIA MÀRSE ELEKTORAAL 2019
  • COKKAASU ODIA
  • NATAALI AYUBÉS BI

MÀRSE ELEKTORAAL 2019

By
Odia
-
15 mai 2019
Facebook
Twitter
Google+
Pinterest
WhatsApp

    Odia
    Facebook
    Twitter
    Google+
    Pinterest
    WhatsApp
      Previous articleMBARA-WÀCC DOOMI-GAYNDE NJAAY YI !
      Next articleNATAALI AYUBÉS BI
      Odia

      RELATED ARTICLESMORE FROM AUTHOR

      CÉY BII MÀRSE…

      BUUR

      “MARTEAU” BI

      LÉEBU/XALAAT/XELTU

      Kër baay du kër

      XËT YI MUJJ

      AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?

      Yatma Jóob - 21 novembre 2019
      0
      Bare na li may toog man kenn, di yónni samam xel, mu wëral ma àddina sépp ak li ci biir, fu nekk...

      DÉMB AK TEYU DOXANDÉEMI ITALI YI

      Baay Njaay - 21 novembre 2019
      0
      Waxtaanu Baay Njaay ak B. S.

      WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?

      Daawuda Géy - 21 novembre 2019
      0
      Omar Bolondeŋ Jóob a ngi juddu ci 10eelu fan ci weeru sàttumbar 1946 ca Ñaame, péeyub réewum Niseer. Mu ngi faatu ci 11eelu fan...

      BUUR

      Odia - 13 octobre 2019
      0

      WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?

      Uséynu Béey - 13 octobre 2019
      0
      Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp a bégoon, rawatina murid yi. Bégoon nañ ba, foo...

      MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

      Paap Aali Jàllo - 13 octobre 2019
      0
      Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci Kolobaan jumaa ju mag ji : Masaalikul Jinaan....

      ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI

      Xari Njaay - 13 octobre 2019
      0
      Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi ñu ko ko nëbbee ñaari ati Yàlla ak...

      LAAJ-TONTU SAADA KAN/BÓRIS (III)

      Paap Aali Jàllo - 13 octobre 2019
      0
      Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laaj-tontu bu Saada Kan di amal ci tele 2Stv ñaari ayu-bés yu nekk, te mu...

      DÉMB AK TEY

      Paap Aali Jàllo - 13 octobre 2019
      0
      Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY mi leen seen yeénekaayu web LU DEFU WAXU jagleel. LU DEFU WAXU nag,...

      JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR

      Daawuda Géy - 13 octobre 2019
      0
      Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit ñi xam kan mooy Jiñaabo ! 

      MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

      Ndey Koddu Faal - 22 septembre 2019
      0
      Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul ña fa fekk baax a may tax a...

      “MARTEAU” BI

      Odia - 22 septembre 2019
      0

      FUTBAL AK BASKETU SENEGAAL : YAAKAAR AK YÀKKI

      Paap Aali Jàllo - 22 septembre 2019
      0
      Bi Alseri dumaa Senegaal benn ci dara ci finaalu joŋanteb réewi Afrig yi (CAN) ak léegi, mu ngi bëgg a yàgg. Waaye,...

      DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

      Daawuda Géy - 22 septembre 2019
      0
      Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci 27eelu ut 2019 bii ñu génn.

      LAAJ-TONTU : SAADA KAN BÓRIS JÓOB (II)

      Paap Aali Jàllo - 22 septembre 2019
      0
      Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laajt-tontu bu Saada Kan di amal ci tele 2Stv ñaari ayu-bés yu nekk, te mu...

      IMMEUBLE PDS/WADE BAAY AK DOOM

      Mamadu Jàllo - 31 août 2019
      0

      NAWETU ITALI AK JOŊANTE REN JI

      Baay Njaay et Stefano Anselmo - 31 août 2019
      0
      Nu des ak yéen ci réewum Itali ba tey. Tey nag, xibaar yi nu leen di jottali xaw nañoo wute ak yi...

      MAKI/XALIFA : MAG, BU RUSEE NE MAA-TEY

      Paap Aali Jàllo - 30 août 2019
      0
      Fan yii nu génn, bare woon na ñu doon yéy ak a yàbbi ci mbirum Xalifa Sàll, di wax ci njéggal bi...

      SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU

      Xari Njaay - 30 août 2019
      0
      At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn sax, seen njàqare ak seen tiis dafa mel...

      ‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

      Bubakar Bóris Jóob - 30 août 2019
      0
      WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

      EDITOR PICKS

      POPULAR POSTS

      FÀLLU SIISE FEKKI NA KOCC BARMA!

      16 mai 2019

      SÉEX BEECO CUUN : ÀTTE YÀLLAA GËN BU NIT

      16 mai 2019

      SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA

      30 mai 2019

      POPULAR CATEGORY

      • Gis-Gis47
      • Xibaar26
      • COKKAASU ODIA18
      • Li fës14
      • NATAALI AYUBÉS BI12
      • ?4
      • FÀTTALIKU DÉMB4
      • WAXLEEN SEEN XALAAT1
      • Bàyyi ci xel1
      ABOUT US
      FOLLOW US
      • Lu Defu Waxu
      • Jokkoo
      ©