XËT YI MUJJ
NJÀNGATUB BÀMMEELU KOCC BARMA… 2/3 (USÉYNU BÉEY)
Ndege, ci benn téere, mu mën cee tënk démb, tey ak ëllëg, ñàmbaasee ko cosaan, aada, yeewute ak mbaax. Ndege, ab fentaakon bu ñoree...
NJÀNGATUB “BÀMMEELU KOCC BARMA”, TÉEREB DEKKALI (USÉYNU BÉEY) 1/2
Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi Golo, bii mooy ñaareelu téereb nettali bu werekaan bi, Bubakar...
SEEXAA MARIYAAMA ÑAS, JÀMBAARU LISLAAM DEM NA (MUSAA AYSATU JÓOB)
Ñoo ngi ko duppe woon Xàddimatul Xuraan ndax bëgg ak taxawaay bu mu amoon ci Alxuraan. Seexaa Mariyaama Ñas wàcc na liggéey ci ayubés...
LI CI BIIR “MBOORUM ÀDDUNA SI” BU ABDU-XAADR KEBE (EJO-Editions)
KAN MOOY SËRIÑ ABDU-XAADR KEBE ?
Sëriñ Abdu-Xaadr Kebe, ñu gën koo xam ci turu Jili Kebe, lijjantikat la (entrepreneur), yor lijjanti guy yëngu ci...
NJÀNGATUB “BÀMMEELU KOCC BARMA”, TÉEREB DEKKALI (USÉYNU BÉEY) 1/2
Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi Golo, bii mooy ñaareelu téereb nettali bu werekaan bi, Bubakar...
SAFARAS NGAJAGA SI « Ci nen lan toog… » (Paap Aali Jàllo)
Ci gaawu bii weesu, 19eelufan ci weeru desàmbar, waa Ngajaga tiit ak njàqare lañ xéye. Daanaka, askanuw Senegaal ci boppam a jaaxle woon, tiit...
BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI (BAABAKAR JÓOB BUUBA)
Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit. Joŋante yi gën a indi coow mooy yi amoon ca Beliyoriisi mbaa Amerig, walla fii ci...
LI CI BIIR “XELUM XALAM” BU LÀMP FAAL KALA (EJO-Editions)
KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ?
Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame ci turu Ngoti Faal (Ngoty Fall), doomu Luga la ju...
LI CI BIIR “MBOORUM ÀDDUNA SI” BU ABDU-XAADR KEBE (EJO-Editions)
KAN MOOY SËRIÑ ABDU-XAADR KEBE ?
Sëriñ Abdu-Xaadr Kebe, ñu gën koo xam ci turu Jili Kebe, lijjantikat la (entrepreneur), yor lijjanti guy yëngu ci...
LI CI BIIR “GUDDIG MBOOYO” BU LAMIN MBAAY (EJO-Editions)
KAN MOOY LAMIN MBAAY ?
Lamin Mbaay, ab Birigajeb pólis la woon. Mi ngi juddu 4eelu fan ci weeru desàmbar 1952, ca Mexe. Waaye, Aayre-Laaw,...
LI CI BIIR “XELUM XALAM” BU LÀMP FAAL KALA (EJO-Editions)
KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ?
Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame ci turu Ngoti Faal (Ngoty Fall), doomu Luga la ju...
PAAP BUUBA, GAYNDE GU NU DOOTUL FÀTTE, (MUSAA AYSATU JÓOB)
Paap Buuba Jóob saay na, ginnaaw bi ko feebar bi ñuy wax "Charcot" tërale lu war tollu ci ñaari at ba tere woon koo...
SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)
« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. »
Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu mbootaayu liggéey (GIE), bàjjenu gox, aji-aw (relais), « conseillère municipale » … Ne...
LI CI BIIR “GUDDIG MBOOYO” BU LAMIN MBAAY (EJO-Editions)
Kan mooy Lamin Mbaay ?
Lamin Mbaay, ab Birigajeb pólis la woon. Mi ngi juddu 4eelu fan ci weeru desàmbar 1952, ca Mexe. Waaye, Aayre-Laaw,...
RFI : NJUUMTE, YABAATE WALLA LAN ? (NDEY KODDU FAAL)
Bërki-démb, ci altine ji, rajo Rfi dafa juum tàgge ñaar ci njiiti réewu Senegaal yi woon : Abdu Juuf ak Ablaay Wàdd. Am na sax ñeneen...
BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW ? (USÉYNU BÉEY)
Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig juy warax béy bu lab. Ay fukki, ay téeméeriy, ay junniy waxambaane ak, léeg-léeg sax, ay janq...
JÀNGORO JU YÉEME JIY DAANEEL MOOL YI (PAAP AALI JÀLLO)
Jàngoro ju yéeme te raglu moo gaaral, fan yii, ay mool yu nappi woon ba delsi. Limeesagum na, xaat-xaat, 300i way-tawat. Jawriñu wér-gi-yaram wi ne, ku...
SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)
« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. »
Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu mbootaayu liggéey (GIE), bàjjenu gox, aji-aw (relais), « conseillère municipale » … Ne...
TUKKI TEKKI, TOOG TOROX ? (PAAP AALI JÀLLO)
« Tekki mbaa dee ! »
Li ko dale 1eelu fan jàpp 12eelu fan ci weeru oktoobar bii ñu génn, 414i ngaalukat (émigrés clandestins) ñoo lug ci yoonu...