TERE NAÑU MANSUUR FAY MU GÉNN RÉEW MI
Ay yooni yoon, Mansuur Fay mi ngi jël yoon wi, di bëgg a tukki. Waaye, bu demee ba fa dalub romplaan ba rekk, ñu waññi ko, ne ko mënoo génn réew mi. Jëwriñ ji ñu dénk biir-réew...
Mbiru “Fonds Force Covid-19” mi lëmbe na lool réew mi fan yii. Bari na ñoo xam ne woolu nañu leen ci. Moom, Mamadu Ngom Ñaŋ, ci ñi Yoon woolu woon ci la bokk. Nde, ca jamono yooya, moo nekkoon DAGE (Directeur de l’Administration Générale...