Home Authors Posts by Xari Njaay

Xari Njaay

6 POSTS 0 COMMENTS

XËT YI MUJJ

BÉS BU MBAS MI XÉYEE NE MES… (Abdulaay Sekk)

ABDULAAY SEKK Mbas mi jaaxal na ñépp, yëngal àddina sépp. Jàngoro jii di koronaawiris wone na boppam ci fànn gu ne : koom, wér-gi-yaram, njàng,...

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii dina noot àddina sépp ? Tax na ba kenn ñemeetul a...

GÀTTALUG XIBAAR YI

(Ayu-bésu 4eel jàpp 10eelu fan ci weeru Me) (PAAP AALI JÀLLO) Liggéey ngir Yàlla : Ñiy liggéey ci kurélug Force Covid giy saytu ak a doxal xeexub...

DOKTOOR PAAP MUSAA COOR : “NAÑ BÀYYI MBAS MI MU LAW !’’

  (TEKKIG PAAP AALI JÀLLO) Doktoor Paap Musaa Coor, gëstukat la, xelam màcc ci wérug mbooloo. Aji-caytuwaan (consultant) bi, jiite woon na fi tamit kurél giy...

COKKAASU ODIA

PORFESOOR MUSAA SÉYDI : «BÀYYI WIRIS BI LAW, MUSIBA LA NU NAROON A JURAL»

  Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle ngir xeex mbas mi. Waaye PorfesoorMusaa Séydi mi jiite Banqaasu...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

AMI MBENG ABLAAY JUUF SAAR : « Li nu gën a seetlu mooy ne limu way-tawati Covid-19 day gën di yokku. Ndege, lim bi ful na...

«BU DUL WOON DOXANDÉEM YI, MBAS MI DU NAANE ÑEEX AFRIG » (Doktoor Séydu...

Paap Aali Jàllo Doktoor Séydu Jàllo ab Farmasiyeŋ la, dib biyólósis ak « ancien interne des hopitaux ». Xam-xamam màcc na tamit ci wàllu kiiraayu biir...

FAN LANU JËM AK ÑAKKI BILL GATES YI ?

(USÉYNU BÉEY) Coow laa ngi ne kurr ! Afrig ba Afrig daj, li ko dale Keer ba Peretoryaa, Ndakaaru jàpp Adis-Abebaa, wax ji benn la : jàppal...

«LI MAY RAGAL…» LAAJ-TONTU AK DOKTOOR SÉYDU JÀLLO (II)

Paap Aali Jàllo Doktoor Séydu Jàllo ab farmasiyeŋ la, dib biyólósis. xam-xamam màcc na tamit ci wàllu kiiraayu biir yaram ak ség. Tey, day waxtaan...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU (Làmp Faal Kala)

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje xel yi ak xol yi, ba ku tiitul it jaaxle nga, mbaa sax nga faf...

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑUNDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CAWUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey Koddu Faal : Sëriñ Séex Mbàkke AMAAR, maa ngi lay nuyu ci...

«BU DUL WOON DOXANDÉEM YI, MBAS MI DU NAANE ÑEEX AFRIG » (Doktoor Séydu...

Doktoor Séydu Jàllo ab farmasiyeŋ la, dib biyólósis ak « ancien interne des hopitaux ». Xam-xamam màcc na tamit ci wàllu kiiraayu biir yaram ak ség....

ÀTTE BOR FEY WALLA… FÀTTE ? (Ndongo Si)

Ndongo Si Mbasum Covid-19 mi am nay njeexital ci koom-koomu Afrig, dekkal na sax coow lu bare ñeel boru réewam yi. Wolof Njaay dafa ne :...

FAGAROO GËN FAJU

  Li Faal Sàmba Suuna Sama maam daan na wax ni maamam dund na téeméeri at ak ñaar-fukk yu ànd ak wér ak wérle. Ndax magal...

GÀTTALUG XIBAAR YI (Altine 13 eelu – dibéer 19eelu awril)

Paap Aali Jàllo Mbasum Covid-19 bi faat na juróomi way-tawat ci diggante dibéer ak altine Ci dibéer ji, bi minwi di waaj a jot, la xibaar...

SÉDDALE BUKKI

DÓOR I YAT YARUL GONE (Safiyetu Béey)

 SAFIYETU BÉEY Juróom-ñetti xarnu ci ginnaaw, amoon na fi buurub Almaañ bu ñuy wax Ferederik 2. Daa déggoon làkk yu bari, demoon na ba mokkal 9i...

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’ (Séex Mbàkke Amaar, ca WUHAN)

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑU NDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CA WUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey Koddu Faal : Sëriñ Séex Mbàkke AMAAR, maa ngi lay...

FAATUG HIBAA CAAM : SENEGAAL, BOPP BU XAR ÑAAR ? Uséynu...

(USÉYNU BÉEY) Guddi àjjuma, dëppook 3eelu fan ci weeru Awril, doon guddi gi jiitu bésub baaxentalub sunu moom-sa-réeew, la benn jànq bu am 28iat, di...