Yatma Jóob

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/12/2023)

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am déet, mënees na jàpp ni wote yi dinañ am ci bés bees ko jàppoon. Njiitu réew mi Maki Sàll xaatim na dekkere bi keroog àllarba, 29 noowàmbar 2023. Ci biir dekkere...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle. Moom Jean Emmanuel di ki yor kàddug Nguur gi (porte-parole) moo biral ne kibaaraanu Farãs googu di “Le Monde” amatul sañ-sañu génnee fab xibaar. Maanaam, muy ci mbooleem bànqaas yi...

No posts to display

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/12/2023)

PÓLITIG Bu amee ñu doon laamlaame wotey 2024 ndax dees ko war a dàq am...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle....

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/12/2023)

COOWAL CAN LI Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon...