COKKAASU ODIA

XËT YI MUJJ

NJIITU RÉEW MI FA TUUBAA

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, amal na génnam gu njëkk ci biir...

RUWÀNDAA, 30I GINNAAW FAAGAAGALUG TUTSI YA

Lu xewoon Ruwàndaa ca atum 1994 ? Keeroog, 6eelu fanu awril 1994, lañ song roppalaanu Njiitu...

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYER LEVERKUSEN JËL NA KO !

Xabi Alonso ak gaayam yi def nañ ko. Dugal nañ Bayer Leverkusen ci mboorum...

BOROOM JAKARTAA BI FAATU FA CAALI

As góor su tollu ci 25i at, daan dawal móto jakartaa, lees fekk neewam...