No posts to display

XËT YI MUJJ

COKKAASU ODIA

BAÑ A WACC SA ÀND… (BAAY NJAAY)

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu mu doon. Nekk cim réew, dund fa lu ëpp fanweeri at, te ba tey may...

KAN MOO DOON ISEN AABARE ? (AMI MBENG)

« Jébbalees na Aabare Boroomam », nii la jawriñ jiñ dénk wàllu yoon wi, Maalig Sàll, dëggalee xibaar bi rotoon ci yéenekaay yi :...

COOW DINA TOPP SENEGAAL CI FAATUG ISEN AABARE GI (NDEY KODDU FAAL)

Isen Aabare, Njiitu réewum Càdd la woon, génn na àddina ci loppitaal “Principal” bu Dakaar talaata 24eelu fan ci weeru ut 2021. Nee na...

ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI

"MBINDAAN" LEES WAROON A BIND ------------------------------------------------------------------------------ ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug jubbanti mbindin mi Yaxub kubbite  Tey jii, boroom xam-xam yaa...

COKKAASU ODIA

BOROOM-ÑAARI-TUR YI SAMP NAÑU SEEN NDËND WAAYE… (MUSAA AYSATU JÓOB)

Mbirum ngóor-jigéen doon na lu lëmbe àddina si fi mu tollu nii, moonte dey amul jenn diine ju ko nangu, du jullit, du kercen,...

DALOOB KËR MOMAR SAAR 3 : NDOX MU DOY, DUND GU SELL (NDEY KODDU...

Robine tijji, ndox walangaan, xel dal, xol tóor yaakaar, yaakaar ëllëg gu tane ndax fu ndox mate, dund sell. Lii mooy njeexitalu Kër Momar...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…? (USÉYNU BÉEY)

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp ! Gannaaw ba alkaati yeek sàndarm yi jëlijee Usmaan Sonko ngir jébbal ko Yoon, daanaka waa...

JOXEB LIJAASA BU 48eelu LËLU CESTI (NDEY KODDU FAAL)

Alxemes jii nu génn la CESTI doon jox seen lijaasa 4i taskati xibaar yu jigéen ak 21 yu góor. Xew-xew baa nga ame "UCAD...

Cokkaasu Odia

ÑU BÓOM 160i DOOM-AADAMA CA BURKINAA, AFRIG DUMMÓOYU : LAN MOO NU DAL ?...

Solhan, gaawu, 5eelufan ci weeru suweŋ, ci kow i néew la jant bi fenk. Xetub bànqanoos bu jaxasook xetu deret ubale foofu yépp. Ay...

WAVE AK ORANGE MONEY, NUN LAÑ FI NEKKAL WALLA SEEN BOPP? (AMI MBENG)

Wax ji bari na, werante bi ne kurr, ñii naan « Ñaw ! Upp baax na ci laax bu tàng ! », ñi ci des naan « Aawo...

ANNONCE COURS DE WOLOF À L’IFAN ET À L’EBAD

ANNONCE La deuxième session des cours d’alphabétisation en wolof aura lieu du samedi 5 juin 2021 au samedi 26 juin 2021 inclus. Prévus en présentiel à...

COKKAASU ODIA

CEERNO ALASAAN SÀLL : “SAMA YÉENE CI RÉEWUM SENEGAAL…” (PAAP AALI JÀLLO)

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan Sàll. Turam ak turi Usmaan Sonko, Bàrtelemi Jaas, Xalifa Sàll, Abdul...

KÀDDUY USMAAN SONKO (USÉYNU BÉEY ) 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool, yegg sax fu ko kenn foogul woon. Ñii seen i...

COKKAASU ODIA

CEERNO ALASAAN SÀLL : “YAAKAAR AK RAFET NJORT ÑOO MA TAXOON A ÀND AK...

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax  waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan Sàll. Turam ak yu Usmaan Sonko, Bàrtelemi Jaas, Xalifa Sàll, Abdul...

RAFLE JÀMM (DAAWUDA NJAAY JARAAF)

Fitt a jiitu fetal Lépp aju ci ngistal Doolee mën dëgg Weddil googu dëgg Njaayum gànnaay Rombal doonub nay Bu njaay mi lambee Dëgg daan doole Gént naay gànnaay Yu wuteek yiy rey Sànni...