XËT YI MUJJ
AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?
Bare na li may toog man kenn, di yónni samam xel, mu wëral ma àddina sépp ak li ci biir, fu nekk...
WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?
Omar Bolondeŋ Jóob a ngi juddu ci 10eelu fan ci weeru sàttumbar 1946 ca Ñaame, péeyub réewum Niseer. Mu ngi faatu ci 11eelu fan...
WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?
Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp a bégoon, rawatina murid yi. Bégoon nañ ba, foo...
MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI
Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci Kolobaan jumaa ju mag ji : Masaalikul Jinaan....
ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI
Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi ñu ko ko nëbbee ñaari ati Yàlla ak...
LAAJ-TONTU SAADA KAN/BÓRIS (III)
Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laaj-tontu bu Saada Kan di amal ci tele 2Stv ñaari ayu-bés yu nekk, te mu...
DÉMB AK TEY
Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY mi leen seen yeénekaayu web LU DEFU WAXU jagleel. LU DEFU WAXU nag,...
JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR
Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit ñi xam kan mooy Jiñaabo !
MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !
Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul ña fa fekk baax a may tax a...
FUTBAL AK BASKETU SENEGAAL : YAAKAAR AK YÀKKI
Bi Alseri dumaa Senegaal benn ci dara ci finaalu joŋanteb réewi Afrig yi (CAN) ak léegi, mu ngi bëgg a yàgg. Waaye,...
DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI
Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci 27eelu ut 2019 bii ñu génn.
LAAJ-TONTU : SAADA KAN BÓRIS JÓOB (II)
Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laajt-tontu bu Saada Kan di amal ci tele 2Stv ñaari ayu-bés yu nekk, te mu...
NAWETU ITALI AK JOŊANTE REN JI
Nu des ak yéen ci réewum Itali ba tey. Tey nag, xibaar yi nu leen di jottali xaw nañoo wute ak yi...
MAKI/XALIFA : MAG, BU RUSEE NE MAA-TEY
Fan yii nu génn, bare woon na ñu doon yéy ak a yàbbi ci mbirum Xalifa Sàll, di wax ci njéggal bi...
SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU
At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn sax, seen njàqare ak seen tiis dafa mel...
‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’
WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB