No posts to display

XËT YI MUJJ

ËTTUB TAALIF

‘’Ëttub taalif’’ mooy xët wu bees wi defuwaxu.com jagleel ladabu réew mi. Sunu xarit, sunu doomu-ndey Mataar Caam Faal, moo yor wile xët. Képp...

LI TAX NDENGLEER MERE BAABAKAR NGOM ”SEDIMA” (PAAP AALI JÀLLO)

Beykati Ndengleer yi, ab dëkk bu féete ci bokk-moomeelu Njagañaaw, ñooy jiiñ Baabakar Ngom, boroom SEDIMA, ne da leen a jaay doole, nangu seen i...

COKKAASU ODIA

SUNU GIS-GIS CI ”BLACK LIVES MATTER” AK YENEEN XEETI ÑAXTU ÑEEL XEETAL AK ÑAAWTEEFI...

(Ci tekkig Ndey Koddu Faal) Njolloor, ca Minneapolis. Alkaatib Tubaab teg óomam ci kow loosu nit ku ñuul di bës, di bës, di bës rekk, tëwa...

FÀWW FAIDHERBE DAANU !

  Paap Aali Jàllo «Tooñ, torox, goreedi ak ñàkk fulla weesuwul ñuy woyal Lat-Joor ci tóojug estati bu Faidherbe…» (Usmaan Sémbéen) Ginnaaw mbasum Covid-19 bi, mel na...

YOLOMAL BUUMU NJAAM GI NGIR GËN LAA XOJ, FARÃS DEFATI NA MËNINAM (Boos...

Boos Ndóoy Jikko ak boroom, sëg ya rekk ! Ndege, Farãs dafa am pexe moo xam ne, ca jamonoy nootaange ja ba tey jii, ci...

USMAAN SONKO : ‘’ÀNDUMAAK ÑI NAAN ‘FRANCE DÉGAGE’ !’’ (Ñaareelu xaaju laaj-tontook Ndey...

LU DEFU WAXU : Seetlu nañ ni, saa booy wax ci nguurug Maki Sàll, danga naan « Nee na moom moo gañe… ». Mu mel...

Cokkaasu Odia

USMAAN SONKO : « MAKI SÀLL CUUNE LA, DI DEF YËFI CUUNE. » (Ndey...

(Xaaj bu njëkku laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo ak Daawuda Géy) LU DEFU WAXU : - Usmaan Sonko, ginnaaw bin la nuyoo, noo ngi lay...

FUKKI SIMILI YI SOPPI AMERIG BA FÀWW (Paap Aali Jàllo)

PAAP AALI JÀLLO George Floyd, jamono jii, mooy néew bi gën a siiw ci àddina sépp. Li kob takk-der bu weex faat ci anam yu ñaaw...

YOW KORONAA (Mamadu Jara Juuf)

TAALIFU MAMADU JARA JUUF Nee nga  layy, ni dott Ñów di nas, di nocci Nërmeel  nga  boroom  doole Detteel  nga  boroom  alal Botti nga  boroom  xam-xam Yow Koronaa, yaay  fas...

MAKI SÀLL : “NAN JÉEM A DUND AK DOOMU JÀNGORO BI TE DU LOR...

(PAAP AALI JÀLLO) Njiitu réew mi woyofal na sàrti guural gi ak dogal yi mu jëloon ngir xeex mbasum Covid-19 bi. Ci altine ji, 11eelu...

AFRIG AK KORONAA, AFRIG GINNAAW KORONAA (Uséynu Béey)

USÉYNU BÉEY Koronaawiris bi, li muy metti metti, terewul kàngami boroom xam-xam yiy wéy di ci weccee xalaat ñeel doxalinu àddina si, ba xam luy nar a...

BÉS BU MBAS MI XÉYEE NE MES… (Abdulaay Sekk)

ABDULAAY SEKK Mbas mi jaaxal na ñépp, yëngal àddina sépp. Jàngoro jii di koronaawiris wone na boppam ci fànn gu ne : koom, wér-gi-yaram, njàng,...

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii dina noot àddina sépp ? Tax na ba kenn ñemeetul a...

GÀTTALUG XIBAAR YI

(Ayu-bésu 4eel jàpp 10eelu fan ci weeru Me) (PAAP AALI JÀLLO) Liggéey ngir Yàlla : Ñiy liggéey ci kurélug Force Covid giy saytu ak a doxal xeexub...

DOKTOOR PAAP MUSAA COOR : “NAÑ BÀYYI MBAS MI MU LAW !’’

  (TEKKIG PAAP AALI JÀLLO) Doktoor Paap Musaa Coor, gëstukat la, xelam màcc ci wérug mbooloo. Aji-caytuwaan (consultant) bi, jiite woon na fi tamit kurél giy...

COKKAASU ODIA

PORFESOOR MUSAA SÉYDI : «BÀYYI WIRIS BI LAW, MUSIBA LA NU NAROON A JURAL»

  Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle ngir xeex mbas mi. Waaye PorfesoorMusaa Séydi mi jiite Banqaasu...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

AMI MBENG ABLAAY JUUF SAAR : « Li nu gën a seetlu mooy ne limu way-tawati Covid-19 day gën di yokku. Ndege, lim bi ful na...