Li fës

KORONAA JAT NA PAAP JUUF, GAYNDEY GAYNDE YI !

« Ërob, rawatina Farãs, dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafoni waaso yi (minorités ethniques)....

LEES WAR A JÀNG CI NDIMBALU RÉEWUM FIDEL CASTRO ÑEEL ITALI ?

BOOS NDÓOY   Saa buñ tuddee réewum Kibaa, ñépp daldi fàttaliku njiitam lu ràññeeku la :...

BATAAXALU ITALI BU TIISE NII…

Mbokki Senegaal, Maa ngi leen di nuyu yéen ñépp, ku ci nekk ci sa tur...

KÀDDUY AADAMA JEŋ

Tofo ci Antonio Gutieres, « Sekerteer Seneraalu » Mbootaayu xeet yi, di ko xelal ci lépp...

MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci...

MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul...

‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

XËT YI MUJJ

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/2/2024)

MBIRI PAAP GÉY AK MÀRSEY  Gannaaw CAN bi mu demoon ak Senegaal, Paap Géy, miliyë...

CEDEAO TEGGI NA DAAN YI MU TEGOON NISEER

Démb ci gaawu gi la way-bokki kurél gi boole réewi Afrig sowu-jant yi ci...

MBAAM MI : ÑETTI LÉEB

Cokkaasu RFI bii daf nuy fàttali ñetti léeb yoy, mbaam a ciy ndeyu-mbill ji....

KAN LA NJIITU RÉEW MI NAR A DIISOOL ?

Nees leen ko xibaaree woon, diisoo la Njiitu réew mi Maki Sàll wooteeti ngir...