Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Search
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Li des
WAXLEEN SEEN XALAAT
BAÑ A WACC SA ÀND…
Baay Njaay
-
Pólitig
Ndeyu àtteg Bokkeefug Senegaal : ndey ji seex du tëdde wet
Cubba Taal
-
Gis-Gis
“Ngalla bunu jaawale ECO ak… ECO!'”
Séex Tiijaan Jéey
-
Xibaar
PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ 3 – Li XALIMAY WAX
Mbay Sow
-
Koom-koom
Kollëre gi doxoon diggante Coca-Cola ak Soboa fecceeku na !
Uséynu Béey
-
Xibaar
LI GËN A FËS CI XIBAARI
Paap Aali Jàllo
-
00:19:36
WIDEWO YI
Jotaayu xam-xam ak Sën Abdu Xaadir Kebe
Defu Waxu
-
FÀTTALIKU DÉMB
MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL
Baay Njaay
-
01:33:07
MAGU WAXOON NAA KO
“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob
Defu Waxu
-
COKKAASU ODIA
Odia
-
Koom-koom
NJUREEFI SOROJ BI AK GAAS
Mamadu Jara
-
Xibaar
WUJJE GI CI BIIR KUJJE GI LAN MOOY JUBLUWAAY BI ?
Mbay Sow
-
COKKAASU ODIA
Read more
MAGU WAXOON NAA KO
Yëral lépp
01:33:07
“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob
Defu Waxu
-
"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...
Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon
Uséynu Béey
-
Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...
GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !
Uséynu Béey
-
Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...
KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW
Uséynu Béey
-
Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...
WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?
Uséynu Béey
-
Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp !...
KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC
Uséynu Béey
-
Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...
KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC
Uséynu Béey
-
Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...
Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2
Uséynu Béey
-
Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu...
BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?
Uséynu Béey
-
Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig...
FÀTTALIKU DÉMB
Yëral lépp
FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2
-
(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...
2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI
Ndey Koddu Faal
-
Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...
FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL
Uséynu Béey
-
Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...
JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI
Defu Waxu
-
Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...
DÉMB AK TEY
Paap Aali Jàllo
-
Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY...
JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR
Defu Waxu
-
Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise...
DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI
Defu Waxu
-
Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979...
SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA
Defu Waxu
-
Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca...
MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL
Baay Njaay
-
Àllaaji Omar Taal mi juddu ci atum 1796 ca...
WIDEWO YI
Léeb: Sama Soxna Dafa Luu (Saa Wujj Muuma La), En Wolof
09:09
Nettali: Maryaama Ba - En Wolof (Une si longue lettre) Pàcc 06 | Mariama Ba (Bataaxal bu gudde nii)
11:11
MBOOR AK XAYTE: Seex Anta Jóob ak Kemitism (lan la gëmoon) (1)
10:07
Importance du wolof - Abdou Lahat Ka partage les chants en wolof de son grand-père Serigne Moussa Ka
15:20
Njariñu Jàng Ci Saw Làkk (Wolof)- Mr Abdurahim Leye, Enseignant Chercheur.
30:27
COUMBA AM NDEYE" ET COUMBA AMOUL NDEYE /DESSIN ANIME /WOLOF
06:05
HERITAGES ak AWA | Lamine Ndiaye [Wolof sous-titré FR]
16:06
WAX LEEN SEEN XALAAT
Yëral lépp
BAÑ A WACC SA ÀND…
Baay Njaay
-
Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu...
BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI
Baabakar Jóob Buuba
-
Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit....
"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB
Baabakar Jóob Buuba
-
Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne...
KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU
Làmp Faal Kala
-
Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje...
NAKA LAA GISE MBAS MI
Baabakar Jóob Buuba
-
Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci...
KORONAAK ÀDDINA
Làmp Faal Kala
-
Taalifu Làmp Faal Kala Ki daan mere nit ñi ci...
FÀLLU SIISE FEKKI NA KOCC BARMA!
Ndekete Fàllu Siise daa bokk ca ña daamar (kamiyoŋ) ga saaraan fan yii ñu...
XALIMA BËNN NA AY GËTAM
Mayleen ma nopp, abal ma seen i gët te ubbi seen um xel ma...
SÉEX BEECO CUUN : ÀTTE YÀLLAA GËN BU NIT
Altine 6eelu fan ci weeru Me, atum 2019. Bés bi ñépp doon xaar, bésub...
NJUREEFI SOROJ BI AK GAAS
Réewum Senegaal a ngi waaj a jëfandikoo soroj bi ak gaas bi fileek diir...
Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon
Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di génne téere bu mu bind...
BUUR, LEKK AK NAAN, FOLLIKU DAY BETTE
Téll !... Xërr !... Téll !... Xërr ! Téll !... Xërr !... Takk-der yi...
JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR
Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit...
SONKO AK MAKI : KUY DAAN ?
Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki....
Mbënn mi ak toj-toj yi : fan la miliyaar yi duggu ?
Njàqare, jaaxle la ñu bari ci ñi dëkke ci yenn diwaan yu nekk ci...
Saajo Maane ca Bayern Munich
Njiiti Bayern Munich yi mujje woon nañ déggook yu Liverpool FC yi ñeel ëllëgu...
00:19:36
Jotaayu xam-xam ak Sën Abdu Xaadir Kebe
SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA
Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca réewum Afrig-bëj-saalum. Moom, nag, benn doomu...
TAAFAR SI CI LÀNGUG POLITIG GI, MBAA DINA JUR JÀMM CI RÉEW MI ?
Xeetu taafar yi nuy faral di gis te di ko dégg ci réew mi...
GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !
Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru nowàmbar wii, jaare ko ci...
Gis-Gisu Seex Aliyu Ndaw ci "Francophonie"
Faraŋ ko fóni (Woy) Faraŋ ko fóni Man kat daa waaru Kaay làggi ci saaw làmmiñ Na doon saw...
SENEGAAL: JAPPAL, BAYIL
LU ÑUY XAAR CI JÀNGALE LÀMMIÑI RÉEW MI ?
Bi Senegaal moomee boppam ba tey, bare na ay nguur yu fi jaar ak...
PMU PARI MACKY KERMESSE
PETIT GUIDE POUR DÉJOUER LES PIÉGES DE LA LANGUE WOLOF (Safiyetu Béey)
Ce petit guide a pour but de faciliter l'apprentissage de l'écriture en wolof à...
ÑÀKK KAYITU-JUDDU GI NAG, BA KAÑ?
Ayu-bés yii weesu, yéenekaay yu bare dañoo xéy fésal ci seen xët bu njëkk...
ARAM FAAL, SUNU SÉEX ANTA JÓOB BU JIGÉEN…
Talaata jii weesu di 23 ci weeru awril la Mbootaayu-Xeet yi jagleel bépp teere...
Ëllëgu gaynde yi ca tugal
Naples noppeegul ngir bàyyi Kalidu Kulibali mu dem. Moo ngi ci tànki yokkal ko...
KORONAAWIRIS : MBETE GAYNDE GU TËX !
Ndey Koddu Faal Fii ci Senegaal, limu ñi Covid-19 bi daaneel romb na téeméer. Moonte bi...
Ikibu Futbal bu Senegaal : Ku ñépp di xaar nga war a mëne fu nekk
Keroog ci talaata ji lees tàmbali ñaareelu bëccëgu joŋantey bokkadil CAN 2023. Ikibu Senegaal...
Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2
Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi...
XAREB IKREN BI – KAN MOOY WLADIMIR PUTIN? 2/3
Leningrad la Wladimir Putin yaroo. Leningrad googu, moo nekkaat tey Saint-Pétersburg. Cib nettali, gone...
AYSATA TAAL SÀLL : JIGÉEN SOPPAL TE BUL WÓOLU…?
Bés ba ma ko déggee mu naan kilifa diine yi dañ maa ñaan ma...
FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2
(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la...
7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…
Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...
AY NJÀNGAT ÑEEL KÀMPAAÑI WOTEY PALUM DEPITE YI
Fi mbir yi tollu nii tembe, gaa ñi fare ci làngug pólitig, ku nekk...
Ndey Daba Ñaan : Sey xare la
DI BUUR, DI BUMMI
Ci gaawu bi weesu, 4eelu fan ci weeru me, la dipite yi wote sémbub...
NDEY SÀGGAN, DOOM FAATU (NDEY KODDU FAAL)
Waa Mamel, fii ci Ndakaaru, naqar ak tiis lañ fanaanoo. Li ko waral mooy...
WOTEY 31 SULET YI, Péncoo walla paacoo, askan waay tànn
Fukki fan rekk a ci des fii ak dibéer 31eelu fan ci sulet. Keroog...
SÀNDIKAA NJABOOTU ALFABETISAASIYOŊ JUDDU NA
Askanu Senegaal dafa mës a weg i làmmiñam, làmmiñi réew mépp. Yàgg na leen...
DÉGLUL DOOMI GOLO (TÉEREB DÓOM) BU BUBAKAR BÓRIS JÓOB….
https://youtu.be/1MiaammF5SI
GÀTTAL YI – LI GËN A FÉS CI XIBAARI AYU-BÉSUG ALTINE 29 AWRIL JÀPP ALTINE 05 ME 2019
POLITIG #1eelu fan ci weeru Me Bés bii lañu jagleel liggéeykatI àddina sépp, di leen ci ...
COKKAASU ODIA
LU ЁPP TUURU !
xibaarRéewum Senegaal rafle na jàmm ci jamono jii, muy ci kàddu yi gaa ñi...
NDAJEM ÑAXTU YEWWI ASKAN WI : WEDDI, GIS BOKKU CI
Coowal wotey palum depite yi lёmbe na réewum Senegaal lool ci jamono jii nu...
BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?
Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig juy warax béy bu lab. Ay...
Bërug ndëgg-sërëx
*Xana du bër da daan neex ndongo ? Daara ju kawe ja ca Ndar,...
COKKAASU ODIA
COKKAASU ODIA
LÀMBI GOLO-O ! KU JÓG SAAGA ! (PAAP AALI JÀLLO)
Njoolum-golo miy def yëfi goloom, ku ci yéemu dangay door a yeewu, mbaa...
COOW DINA TOPP SENEGAAL CI FAATUG ISEN AABARE GI (NDEY KODDU FAAL)
Isen Aabare, Njiitu réewum Càdd la woon, génn na àddina ci loppitaal “Principal” bu...
01:33:07
“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob
"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir gën a xam nit ki...
KAN MOO DOON ISEN AABARE ?
« Jébbalees na Aabare Boroomam », nii la jawriñ jiñ dénk wàllu yoon wi,...
SENEGALEY ITALI YI : LA WOON WONNI NA
Fàttaliku lu war jaam la, kon na xel dellu ci ginnaaw ngir saytu walla...
Ndeyu àtteg Bokkeefug Senegaal : ndey ji seex du tëdde wet
Sagar a ngi xeeñ. Ñépp a ko maase yëg. Xet gi ëbale ne ràpp...
NÉEWAAYU LIMUB ÑI WOTE CI JOŊANTE YII : LAN MOO KO WARAL ?
Dibéer 31i fan ci weeru Sulet nekkoon bés bi ñu doon amal wotey palum...
1
2
3
...
7
Page 1 of 7
Exclusive
Téere yi
Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon
MAGU WAXOON NAA KO
Ay xalaat yu meññee ci “Malaanum Lëndëm”
Téere yi
Njàngatum Guddig Mbooyo (2/2)
Téere yi
Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2
MAGU WAXOON NAA KO