SAMES SÓOBU NA CI XEEX BI

Yeneen i xët

Aji bind ji

Fajkat yi xamle nañ ne dinañ dakkal seen liggéey ci diirub ñaari fan. Seen sàndikaa bi (Syndicat Autonome des Médecins du Sénégal) moo ko xamle. Ñoom, ndogal li Njiitu réew mi jël lañuy xeex.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj