AccueilTagsCubba Taal

Cubba Taal

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

COKKAASU ODIA

spot_img

SONACOS/KAWLAX : UBBITEG ISINU LINJAAN BI

Elaas Ndaan Jaañ, njiitul SONACOS li, yégle na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina...

NGASUM NGALAM MA CA FALAME

Ci weeru sulet wiI weesu, Njiitu réew mi jëloon nab dekkare ngir dakkal lépp...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (28/8/2024)

TASUB CESE AK HCCT Dépite yi jëmmal nañ càkkuteefu Njiitu réew mi ñeel sémbuw àtte...

AY NAAL ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew mi teewoon na ca ndaje ma ñu doon sargale ndongo yi gën...

MUSIBA FA CAAROY-GЀEJ

Fa Sancaba, gox bu nekk Caaroy-géej, ñetti gune lañu fekk ci benn daamaar ñu...

TAMXARIT

Tamxarit bokk ci na ci xew-xewi diine fii ci Senegaal. Tur wi rekk làmboo...

USMAAN SONKO DALAL NAÑU KO FA TUUBA AK TIWAAWON

Njiitu Càmm gi, Usmaan Sonko, seeti woon na kilifay diine yu Tuubaa ak Tiwaawon....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/7/2024)

CEDEAO - AES CEDEAO jël ndogal ñee maxejji réewi AES yi (Mali, Burkinaa Faaso ak...

BAC 2024

« BAC » dafa bokk ci joŋante yi gën a siiw fi Senegaal. Démb la door,...

CFEE 2024

Joŋantey CFEE yi door na ci biir réewum Senegaal, ca Gàmbi ak ca Gine...

REYAATE BI CI RÉEW MI

Gaawu gii weesu, dafa am ku ñu jam paaka fa Ndindi, mu faatu. Ndindi,...

WÀÑÑITEG NDUND GI

Wàññiteg njëgu ndund gi, Càmm gi jël na ci ay ndogal. Lañu jotoon waxtaane...

Latest articles

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba...