Paap Abdulaay Seen

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur këram, daldi koy jàpp, yóbbu ko. Bees sukandikoo ci sunu naataangooy Seneweb, li ñuy toppe Paab Maalig Nduur (APR) mooy mbooloom defkati caay-caay (association de malfaiteurs) ak kootoog luubal alalu...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi réew mi dañu toogaat ci réew mi ngir wéyal liggéey bi ñu sumb ak Nguurug Senegaal gi. Bésub 22 oktoobar 2025 lañu ñëwoon Ndakaaru ngir waxtaan ak njiiti réew mi...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi...

LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI

Waa FMI dinañu toogaat ci réew ay fan ngir wéyal liggéey bi ñu sumb...

COKKAASU ODIA