Kii Kumu

KAN MOOY… IDIRIISA SEKK ?

Maaraa la ko ay jegeñaaleem di woowe, doomi-réew mi naan ko Idi. Taskati xibaar yi ñoom, Ndaamal-Kajoor lañu...

KAN MOOY…MAKI SÀLL ?

Ci Baatu Majaw Njaay Aw askan, bala moo tànn njiitam, war naa seet bu baax...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/9/2024)

SAMP NAÑ ËTTU ÀTTE BII DI "POOL JUDICIAIRE FINANCIER" Jëwriñ ji ñu dénk wàllu Yoon...

NJAAG NANGUL !

Baaxoo nanu, fi réew mi, bu xewu bànneex amee, jigéen ñiy joqalante ay teraanga....

GÀMMU 2024

Démb, ci guddig dibéer ji jàpp altine jii, lañ doon amal gàmmu 2024. Muy...