FÀTTALIKU DÉMB

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa" def na 18i at ci...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am na xarnook xaaj. Waaye, mi...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci atum 1871. Mu doon doom...

DÉMB AK TEY

Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY mi leen seen yeénekaayu web...

JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR

Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit...

DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci...

SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA

Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca réewum Afrig-bëj-saalum.  Moom, nag, benn doomu...

MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL

Àllaaji Omar Taal mi juddu ci atum 1796 ca Fuuta, bokk na ci ñi...

XËT YI MUJJ

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ...

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...