Pólitig

Ndeyu àtteg Bokkeefug Senegaal : ndey ji seex du tëdde wet

Sagar a ngi xeeñ. Ñépp a ko maase yëg. Xet gi ëbale ne ràpp...

kàdduy Seex Abdu Baara Dolli yi: Ban taxawaay la ci yoon wane?

Kàddu yi Seex Baara yékkati woon ca bésu ndajem ñaxtu Yewwi Askan Wi teg...

XËT YI MUJJ

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar...

USMAAN SONKO : « JÀMM REKK LAA SÉQ AK JOMAAY… LIGGÉEYALUMA JOMAAY, SENEGAAL LAAY LIGGÉEYAL. »

Elimaanu jëwriñ yi doon na janook dépite yi, ci àjjumay tay ji. Moom ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/11/2025)

Amal nañu, démb, ndajem jëwriñ yi nees ko baaxoo defe àllarba ju nekk ci...