Tàggat-yaram

CAN 2024 KODDIWAAR : TËGG SA CAN, JËL KO !

Koddiwaar mooy waaga CAN 2024 bees doon amale biir dëkkam. Mu doon dajeek Niseriyaa...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JONANTE DÉMB YI Démb ci talaata ji lees amal ñetteeli joŋantey kippug C gi...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JOŊANTEY BÉS BI Démb ci altine ji, kippug A gi ak gu B gi...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

WÉR-GI-YARAMI ALIW SIISE AK ABDULAAY SIMAA Bees sukkandikoo ci yégle "Fédération Sénégalaise de Football" (FSF)...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CAN-SENEGAAL : JOŊANTEB XARITOO Ëllëg, ci altine ji, bu 18i waxtu jotee la Senegaal di daje...

CAN 2023 : ALIW SIISE TÀNN NAY NDAWAM

Barkaatu-démb ci àjjuma ji la tàggatkatu ekib nasiyonaal bi, Aliw Siise doon amal ab...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CAN 2024 Amara Juuf bokkul ci 55i futbalkat yi Alin Siise tànnagum ngir yóbbu leen...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG TEFES Mamadu Jàllo, tàggatkatu ekibu Senegaal bu kuppeg tefes bi tànn na ndaw yi...

XËT YI MUJJ

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi...

COPPITE YI BASIIRU JOMAAY FAY DIGE

Démb la Njiitu réewum Senegaal lu bees li doon biral kàddoom yu njëkk. Fa...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li,...