Gis-Gis

AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?

Bare na li may toog man kenn, di yónni samam xel, mu wëral ma...

DÉMB AK TEYU DOXANDÉEMI ITALI YI

Waxtaanu Baay Njaay ak B. S.

WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?

Omar Bolondeŋ Jóob a ngi juddu ci 10eelu fan ci weeru sàttumbar 1946 ca Ñaame,...

LAAJ-TONTU SAADA KAN/BÓRIS (III)

Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laaj-tontu bu Saada Kan di amal ci...

FUTBAL AK BASKETU SENEGAAL : YAAKAAR AK YÀKKI

Bi Alseri dumaa Senegaal benn ci dara ci finaalu joŋanteb réewi Afrig yi (CAN)...

MAKI/XALIFA : MAG, BU RUSEE NE MAA-TEY

Fan yii nu génn, bare woon na ñu doon yéy ak a yàbbi ci...

SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU

At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn...

XËT YI MUJJ

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL : SAA-SENEGAALI BITIM-RÉEW Abiib Jara gan-ganluwul fa Àngalteer. Gannaaw ba mu jógee Strasbourg dem Sunderland,...

AG PAS GU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK MÓRITANI

Réewum Senegaal ak mu Móritani yeesal nañu ag pas ci seen diggante. Muy Pas...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2025)

PASTEF MÀGG NA Atum 2014 lañu sosoon làng gii ñuy dippe PASTEF. Maanaam, atum ren...

NDAJEM DONALD TRUMP AK JURÓOMI NJIITI RÉEWI AFRIG

Senegaal, Gaboŋ, Gine-Bisaawo, Liberiyaa ak Muritani… juróomi réew yii la Njiitu réewu Etaasini li,...