Fondateur : Bubakar Bóris Jóob – Directeur de publication : Paap Aali Jàllo




TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko dugge mooy kaas ngir ñu bàyyi Paap Njaay, taskatu-xibaaru Walf...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa Pastef ñoo ngiy def seen kemtalaayu kàttan ngir jàllale ko...

ÀTTEWAAYU NDAKAARU : USMAAN SONKO WAX NA ÀTTEKAT BI AY DËGGAM

Usmaan Sonko jël na kàddu gi ca àttewaayu Ndakaaru, wax àttekat bi ay dëggam ci fulla ak faayda. Njiitul Pastef li dafa biral jafe-jafe...

LAYOOB SONKO-MBAY ÑAŊ : XEEX BI DOOR NA !

Ñetti biisi Dakar Dem Dikk yu tàkk ca Petersen, AUCHAN Mermoos tàkk jëppeet, ay bérébi liggéey yu tëj, dem yombatul, dikk amatul ci péeyub...

TAKK-DER YI LÉEMATI NAÑU KËRU USMAAN SONKO

Jamono ji nuy yaxal mbind mii, takk-der yaa nga fees dell Cité Site Kër Góorgi (Cité Keur Gorgui), fa Usmaan Sonko dëkk. Yoon yeek...
 
YËRAL LÉPP

MAGU WAXOON NAA KO

01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp !...
YËRAL LÉPP

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

YËRAL LÉPP

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit....

"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB  

Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje...

NAKA LAA GISE MBAS MI

Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci...

KORONAAK ÀDDINA

YËRAL LÉPP

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

NDÉGLUG SONKO GI, NA WOON FA WOON ?

Woote bi yoon woo Njiitalu Pastef li, Usmaan Sonko, la yéenekaayu yi xëyee tey....

FÀLLU SIISE FEKKI NA KOCC BARMA!

Ndekete Fàllu Siise daa bokk ca ña daamar (kamiyoŋ) ga saaraan fan yii ñu...

Li gën a fés ci xibaari bés bi

PÓLITIG Maalig Gàkku taxawal nag lëkkatoo Ginnaaw bi mu fésalee yéeneem ngir bokk ci wote yii...

SÉEX BEECO CUUN : ÀTTE YÀLLAA GËN BU NIT

Altine 6eelu fan ci weeru Me, atum 2019. Bés bi ñépp doon xaar, bésub...

PETIT GUIDE POUR DÉJOUER LES PIÉGES DE LA LANGUE WOLOF (Safiyetu Béey)

  Ce petit guide a pour but de faciliter l'apprentissage de l'écriture en wolof à...

XALIMA BËNN NA AY GËTAM

Mayleen ma nopp, abal ma seen i gët te ubbi seen um xel ma...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru nowàmbar wii, jaare ko ci...

Gis-Gisu Seex Aliyu Ndaw ci "Francophonie"

Faraŋ ko fóni (Woy) Faraŋ ko fóni Man kat daa waaru Kaay làggi ci saaw làmmiñ Na doon saw...

DÉMB AK TEY

Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY mi leen seen yeénekaayu web...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Talaata 28i féewirye 2023)

CARGALUG 3i SÓOBARE YI GAAÑOO MALI Ci àllarba ji, 1 màrs 2023 lañu fas yéene...

MOOM SA BOPP, MOOM SAW LÀMMIÑ Baabakar Lóo (ca Pari)

Sunu réew, Senegaal, niki réew yu bare ci Kembaaru Afrig, yàgg naa dund ay...

XAREB IKREN BI – KAN MOOY WLADIMIR PUTIN? 2/3

Leningrad la Wladimir Putin yaroo. Leningrad googu, moo nekkaat tey Saint-Pétersburg. Cib nettali, gone...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di génne téere bu mu bind...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi...

LU ÑUY XAAR CI JÀNGALE LÀMMIÑI RÉEW MI ?

Bi Senegaal moomee boppam ba tey, bare na ay nguur yu fi jaar ak...

ÑÀKK KAYITU-JUDDU GI NAG, BA KAÑ?

Ayu-bés yii weesu, yéenekaay yu bare dañoo xéy fésal ci seen xët bu njëkk...

DI BUUR, DI BUMMI

Ci gaawu bi weesu, 4eelu fan ci weeru me, la dipite yi wote sémbub...

JIGÉEN DU XARU TABASKI !

“DOY NA !”, “DAFA DOY !”. Ñaari baat yii mën nañoo tënk doxu-ñaxtu bi...

NDEY SÀGGAN, DOOM FAATU (NDEY KODDU FAAL)

Waa Mamel, fii ci Ndakaaru, naqar ak tiis lañ fanaanoo. Li ko waral mooy...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la...

LI CI BIIR "XELUM XALAM" BU LÀMP FAAL KALA (EJO-Editions)

KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ? Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame...

CEERNO ALASAAN SÀLL : "SAMA YÉENE CI RÉEWUM SENEGAAL…"

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan...

SENEGAAL, SEEN GAAL LA, ÑOOM, AM SUNU GAAL… ?

Ku waaruwul ci doxinu miim réew, saw doxin dina la waari ëllëg. Ku yéemuwul...

LAAJ–TONTU AK SOXNA AWA GAY MU PAI

65i at ci ren, bi ñu taxawalee làngug Parti africain pour l’indépendance ak léegi....

KAN MOO DOON ISEN AABARE ?

« Jébbalees na Aabare Boroomam », nii la jawriñ jiñ dénk wàllu yoon wi,...

Aa ! Gaa ñi, Tataa Mimi mer na !

Aminata Ture mer na nag. Te, altine ba léegi, moo ngi koy fésal ak...

Saajo Maane ca Bayern Munich

Njiiti Bayern Munich yi mujje woon nañ déggook yu Liverpool FC yi ñeel ëllëgu...

JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR

Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit...

AYSATA TAAL SÀLL : JIGÉEN SOPPAL TE BUL WÓOLU…?

Bés ba ma ko déggee mu naan kilifa diine yi dañ maa ñaan ma...

DÉMB SEŋOOR, TEY WÀDD

Li ko dale atum 1978 ba tey jii, woteb ren bii mooy wote bu...

TOLOF-TOLOFI ARTISÃ YI : LAN MOO CIY TAXAWAAYU NGUUR GI

Fànnu artisanaa nekk na lu soxal lool nit ñi rawatina artisã yi yore seen...

NJUREEFI SOROJ BI AK GAAS

Réewum Senegaal a ngi waaj a jëfandikoo soroj bi ak gaas bi fileek diir...

SÉEX ALIYU NDAW : “LI MA JËLE CI MALAANUM LËNDËM…”

Ab téeree ngi nii boo xam ne, bii, boo koy jàng doo bëgg mu gaaw...

LI CI BIIR "MBOORUM ÀDDUNA SI" BU ABDU-XAADR KEBE

KAN MOOY SËRIÑ ABDU-XAADR KEBE ? Sëriñ Abdu-Xaadr Kebe, ñu gën koo xam ci turu...