WAXLEEN SEEN XALAAT

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu mu doon. Nekk cim réew,...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit. Joŋante yi gën a indi coow...

"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB  

Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne fan yii ci nasaraan, te...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje xel yi ak xol yi,...

NAKA LAA GISE MBAS MI

Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci biir réew mi ak ci...

KORONAAK ÀDDINA

Taalifu Làmp Faal Kala Ki daan mere nit ñi ci ñàkk a nuyoo Moo bank ab...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (18/3/2024)

CEDEAO DINA YÓNNEE 130i SAYTUKAT FI RÉEW MI Ndiisoo CEDEAO gi dina yebal lu tollu...

KÀMPAAÑ 2024 YI : “MAA BAAX, YAA BON !”

Altiney tey jii mooy tollook juróom-ñeenteelu fanu kàmpaañ ñeel wotey 24 màrs 2024 yi....

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (16/3/2024)

PODOOR DALAL NA AAMADU BA Ni ñu ko xame ci jamono jii, lawax yi tàmbali...

UN TOMBEAU POUR KINNE GAAJO : TEKKIG BÀMMEELU KOCC BARMA BU BUBABAKAR BÓRIS JÓOB CI FARÃSE

Boroom xalima bu ñaw bi defati na jaloore. Bubakar Bóris Jóob, werekaan bi, móolati...