XËT YI MUJJ

XAREB IKREN BI – KAN MOOY WLADIMIR PUTIN? – (PAAP AALI JÀLLO) 2/3

Leningrad la Wladimir Putin yaroo. Leningrad googu, moo nekkaat tey Saint-Pétersburg. Cib nettali, gone gi Wladimir, ku ësoon la, amoon fit lool te bare...

XAREB IKREN BI – COSAAN LI AK NJEEXITAL YI – (PAAP AALI JÀLLO) 1/3

Coowal Riisii – Ikren moo lëmbe àddina si. Daanaka, ñaari ayu-bés a ngi nii, moom rekk lañuy waxtaane ci fépp foo dem ci àddina...

GAYNDEE NJAAY ! MBARA-WÀCC ! CAN 2022 : SENEGAAL JËL NA RAW-GÀDDU GI (PAAP...

Dibéer, 6eelu fan ci féewaryee 2022, 21i waxtu ci guddi tegal nañu. Lépp a ngi ne tekk, ne selaw. Ñépp a ngi ne cell....

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE (BUBAKAR BÓRIS JÓOB CI TEKKIG PAAP...

Ci atum 1997 la Mehdi Bâ génne téereem bu jëkk, jox ko tur wu leer nàññ : « Rwanda, un génocide français6 ». Jacques...

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE (BUBAKAR BÓRIS JÓOB CI TEKKIG PAAP...

Weeru màrs 2021 wee ñu génn, ci 26eelu fan, « Ndajem gëstub ceedeefi Farãs ñeel Ruwàndaa ak faagaagalug Tutsi yi », jébbal na Emmanuel...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA...

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab bees duppe World Literature Today, nekk ca Iniwérsite Oklahoma, ca...

PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ : LADAB CI LÀMMIÑI RÉEW MI (NDEY KODDU FAAL)

Ku dégg Maam Yunus Jeŋ, sa xel dem ci jigéen ji jëkk a bind téere nettali ci kàllaamay Kocc. Péncum Maam Yunus Jeŋ nag...

GÀCCE NGAALAAMA,MBUGAAR ! (USÉYNU BÉEY)

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru nowàmbar wii, jaare ko ci benn ciy doomam, di Muhamet Mbugaar Saar, ab bindkat. Moom...

MAKI DA NI WOON YOONU YOKKUTE : LÉPP YOKKU NA ! (PAAP AALI JÀLLO)

«Réew mi dafa tagatémbe !», «Dund gi jafe na !», «Lépp a dëgër !», «Danoo sonn!», «Na nu Maki dimbali !», «…walla mu abal nu.»… Ak yile...

Gis-Gisu Seex Aliyu Ndaw ci “Francophonie”

Faraŋ ko fóni (Woy) Faraŋ ko fóni Man kat daa waaru Kaay làggi ci saaw làmmiñ Na doon saw làmmiñ Te bañ di aw làkk Ci yow Waaye kat yemal foofee Bu fi...

JÀNGOROY ÑÀKK JI NU GANESI (MBAY SOW)

Askanu Senegaal tollu na ci diggante bu tar cig ñàkk ba sax, li ëpp ci boroom-kër yi mënuñoo matale seen i wareef, rawatinaak ni...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW (USÉYNU...

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di ñëw, la Senegaal fas yéene amal ay wote jëm ci palu njiiti gox-goxaan yi. Gannaaw ba pàrti pólitig...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… (Foloryaŋ Bobeŋ ci tekkig Daawuda Géy) 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la yem ; ndax Seŋoor àndul woon ci réew mi génn...

COKKAASU ODIA

COKKAASU ODIA

BAÑ A WACC SA ÀND… (BAAY NJAAY)

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu mu doon. Nekk cim réew, dund fa lu ëpp fanweeri at, te ba tey may...

KAN MOO DOON ISEN AABARE ? (AMI MBENG)

« Jébbalees na Aabare Boroomam », nii la jawriñ jiñ dénk wàllu yoon wi, Maalig Sàll, dëggalee xibaar bi rotoon ci yéenekaay yi :...

COOW DINA TOPP SENEGAAL CI FAATUG ISEN AABARE GI (NDEY KODDU FAAL)

Isen Aabare, Njiitu réewum Càdd la woon, génn na àddina ci loppitaal “Principal” bu Dakaar talaata 24eelu fan ci weeru ut 2021. Nee na...

ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI

"MBINDAAN" LEES WAROON A BIND ------------------------------------------------------------------------------ ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug jubbanti mbindin mi Yaxub kubbite  Tey jii, boroom xam-xam yaa...