COOWAL CAN LI
Afrig moom, dafa mel ni ndeyam liggéeyul. Saa bu CAN bi jubsee, coow li jib, ñuy ŋëwti-ŋëwti joŋante bi. Te, bu "Euro" bi jotee, kenn du dégg coow ñeel ko. Waaye bu Joŋantey Afrig teroo rekk nga dégg lu nekk. Li ko...
Pólitig
Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon ngir ñu saytuwaat dogal ga mu jëloon ñeel Usmaan Sonko ci wotey 2024 yi.
Seex Baara Dolli bokk ci wutaakoni (lawaxi) wotey 2024 yi, xamle na ne seeti woon na Sonko...