Càmmug Senegaal ak SINOHYDRO (bànqaas ci kër gii di Power-China) taxawal nañu liggéeyi sémbub GTE (Grand Transfert d’Eau) bi nu duppee Autoroute de l’eau du Sénégal. Muy Sémb wu mag wu nar a jotale ndoxum dex gii di « Lac de guiers » ba Tuubaa, Cees,...
Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a ñoŋal nekkinam ci kow suuf. Ba tax na, lépp lu mu njort ni dina gën a yombal dundam, du lott mukk ngir taxaw ci. Ndax, bëggul lu dul, saa su...