Stefano Anselmo

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ yi ci at mu bees mii. Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, moo jiite ndaje ma. Ca njeexital la, Aamadu Mustafaa Njekk Saare mi yor kàddug Càmm gi biral na...

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay ci àllarba ji, ndajem saabal ñeel tolluwaayu saabalukaay yi ci wàllu koom. Njaatigey saabalkat yi ak ñiy yëngu ci xaralay saabal yi ñoo ko doon amal. Ñoñi Mamadu Ibra Kan yi...

Aucun article à afficher

XËT YI MUJJ

NDAJEM JËWRIÑ YI : ÑEENTI JIITUWAAYI NJIITU RÉEW MI

Ci àllarbay démb ji, 22i fani sãwiyee 2025, lees doon amal ñeentelu ndajem jëwriñ...

CDEPS MI NGI SÀKKU CI NJIITU RÉEW MI MU « YEESAL WAXTAAN WI AK SAABALKAT YI »

Conseil des diffuseurs et éditeurs de presse du Sénégal (CDEPS) dafa doon amal, tay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/1/2025)

USMAAN SONKO : DUGG NAÑU CI JAMONO JOJ, BAALE JEEX NA Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko,...

COKKAASU ODIA