AccueilTagsAmi Mbeng

Ami Mbeng

SAMA XALAAT ÑEEL “SOMMETS” YI AK SUNU NJIITI AFRIG YI (TAYIIRU SAAR)

Ci tekkib Paap Aali Jàllo 1. "Sommet France-Afrique" ngir wéyal nooteel geek mbéeféer gu bees...

NJIITU RÉEW MI BIND NA NJIITUL NGOMBLAAN GI

Coowal DPG bu elimaanu jëwriñ yi ba léegi fayagul. Dina ko def am du...
spot_img

WOODSIDE : NDAM AM NA CI SÉMBUW SÀNGOMAAR WI

Woodside Energy siiwal na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina njiit yu bees yi....

BÓOMUG ABDU ASIIS BA

Jéyya ju ñaaw ja ca Pikin Teknopóol mi ngi wéy di jur coow fi...

USMAAN SONKO CA XEWUM WAATU POOL KAGAME

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dem na Ruwàndaa. Dafa teeweeji xewum waatu Póol Kagame...

MBËKK MI : 14i NÉEW YU BEES

Mbëkk mi reyati na. Fukk ak ñeenti néewi Saa-Senegaal lañ fekk cig gaal fale,...

KÉEW MI : BÉSUB NJËMBËT GARAB

ÔGinnaaw-ëllëg, dibéer 4i pani ut 2024, lañ jagleel garab fépp fi réew mi. Njiitu...

AM-AMU NJIITU RÉEW MI

Ndajem Ndeyu Sàrtu réew mi siiwal na am-amu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar...

JÉYYA FA ECOPI : LU ËPP 150 BAKKAN YU ROT

Jéyya ju réy moo xew fa Ecopi. Suuf saa fa màbb ba ay bakkan...

SAARAYA : AY SAAY-SAAY ÑOO SOQI FETEL CI AG DAAMAR

Fa Saaraya, féete ci diiwaanu Kéedugu, la ay saay-saay song ag daamar, soqi ciy...

Aj 2024 : Ujaaji Senegaal yu njëkk dellusi nañu ci réew mi

Lu ëpp 12 000iy ujaaj ñoo jóge woon ci biir réew mi. Ujaaj yu...

FIPPU CA KÀMPENAAL BU “LIBERTÉ 6”

Jar-jar (prisonniers) ya nekk ca kasob Kàmpenaal (Camp penal) bu “Liberté 6” ñoo doon...

BORUB GALAG ÑEEL KËRI TASUKAAYI XIBAAR YI

Jamono jii, këru tasukaayu xibaar yu bari ñoo ngi ci guuta. Ndaxte, dañu ame...

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA WAXTAANUW ONU WI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, teewe na, démb, waxtaan wi Mbootaayu Xeet...

Latest articles

SAMA XALAAT ÑEEL “SOMMETS” YI AK SUNU NJIITI AFRIG YI (TAYIIRU SAAR)

Ci tekkib Paap Aali Jàllo 1. "Sommet France-Afrique" ngir wéyal nooteel geek mbéeféer gu bees...

NJIITU RÉEW MI BIND NA NJIITUL NGOMBLAAN GI

Coowal DPG bu elimaanu jëwriñ yi ba léegi fayagul. Dina ko def am du...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/9/2024)

LU BEES CI CAABALUG PRODAC GI Caabal gi IGF (Inspection Générale des Finances) defoon ci...

NGOMBLAAN GI JÀPPAL NA USMAAN SONKO ÀPPU “DPG” BI

Coowal “DPG” (Déclaration de Politique Générale) li nga xam ne nee na woon kurr...