Xibaar WAXTAANU NJIITU RÉEW MI AK VLADIMIR POUTINE By Ami Mbeng 25/11/2024 0 65 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI Njuga Gay - 17/12/2025 COKKAASU ODIA Odia - 15/12/2025 BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO Ndey Koddu Faal - 15/12/2025 COKKAASU ODIA Paap Aali Jàllo - 08/12/2025 Aji bind ji Ami Mbeng Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jokkoo na ak Njiitu réewu Riisii, Vladimir Poutine. Barkaatu-dém, àjjuma 22 nowàmbar 2024, lañu wax telefon. Moom, sunu Njiitu réew mi, moo ko xamle ci xëtu njéndel li. Daf ne : ñ “Tay, ci yoor-yoor bi, jokkoo naa Njiitu réewu Riisi, Vladimir Poutine. Séq nanu waxtaan wu yaatu te am solo. Waxtaane nanu kóllëre ak digaale yi yàgg a dox diggante ñaari réew. Déggoo nanu ci ànd liggéey ngir dooleel digaale ñaari réew yi, jàmm ak dalug Sayel bi, ak itam ñu sàmm mberaayu CEDEAO. Dinanu boole sunuy doole, ànd ci ak àddina sépp, ngir dékku jafe-jafe yiy xaar àddina si.” Ami MbengPlus de publicationsBiographieAmi Mbenghttps://www.defuwaxu.com/author/amimbeng10/KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAARAmi Mbenghttps://www.defuwaxu.com/author/amimbeng10/NAFAG 2026 : JAGLEES NA 356 MILIYAAR NJËWRIÑU YAXANTU BEEK NDEFAR GIAmi Mbenghttps://www.defuwaxu.com/author/amimbeng10/LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)Ami Mbenghttps://www.defuwaxu.com/author/amimbeng10/LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj