Ami Mbeng

Li gën a fës ci xibaari bés bi (9/10/2024)

9JÀNGOROY ŊAS Nemmeeku nañ juróom-benni jarag yu ame jàngoroy ŋas. Juróom-benni jarag yooyu, ñu ngi nekk ci juróomi "district" : Ndakaaru suuf (1), Funjuuñ (1), Kër Masaar (1), Pikin (2) ak Saraya (1). Waaye, gisuñu fenn ku ame jàngoro jees dippee "mpox", maanaam, ci farãse,...

FUTBAL : FSF ÀDDU NA CI MBIRU ISMAYLA SAKOB

Keroog, ci àjjuma jii weesu, la Paab Caw biral toftaleg gayndey kuppe yi. Moom mi toppoon ci Aliw Siise, moo ko wuutandi ci boppu ekib bi. Mooy jiite gayndey Senegaal yi ci ñaari joŋante yiñ dëgmal ci fan yii di ñëw ñeel toogalante CAN...

TOGO : SONG NAÑ GII MARI SAAÑAA

Gii Mari Saañaa ma nga Togo jamono yii. Waaye, nekkul ci jàmm. Ci lees...

TOLLUWAAYU RÉEW MI CI WÀLLU KOOM-KOOM

FMI dafa génnee ag caabal gog, day càmbar koom-koomu Senegaal ci njëlbeenug xaaju atum...

NJIITU RÉEW MI BIND NA NJIITUL NGOMBLAAN GI

Coowal DPG bu elimaanu jëwriñ yi ba léegi fayagul. Dina ko def am du...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/8/2024)

JËWRIÑU BIIR-RÉEW MI AMAL NAY TABB YU YEES Jëwriñu Biir-Réew mi, Seneraal Sã-Batist Tin amal...

WOODSIDE : NDAM AM NA CI SÉMBUW SÀNGOMAAR WI

Woodside Energy siiwal na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina njiit yu bees yi....

BÓOMUG ABDU ASIIS BA

Jéyya ju ñaaw ja ca Pikin Teknopóol mi ngi wéy di jur coow fi...

USMAAN SONKO CA XEWUM WAATU POOL KAGAME

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dem na Ruwàndaa. Dafa teeweeji xewum waatu Póol Kagame...

MBËKK MI : 14i NÉEW YU BEES

Mbëkk mi reyati na. Fukk ak ñeenti néewi Saa-Senegaal lañ fekk cig gaal fale,...

XËT YI MUJJ

Li gën a fës ci xibaari bés bi (9/10/2024)

9JÀNGOROY ŊAS Nemmeeku nañ juróom-benni jarag yu ame jàngoroy ŋas. Juróom-benni jarag yooyu, ñu ngi...

FUTBAL : FSF ÀDDU NA CI MBIRU ISMAYLA SAKOB

Keroog, ci àjjuma jii weesu, la Paab Caw biral toftaleg gayndey kuppe yi. Moom...

TAKKU WALLU BËGGUL SONKO BOKK

Démb, ci altine ji, la waa DGE (Direction Générale des Elections) siiwal toftale yi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/10/2024)

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI ÑEEL FMI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, rafetlu...