Ami Mbeng

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LEBTOO, FEYTOO

Sàcc, siif, daw… déedéet ! Loolu xewwi na. Léegi, li am mooy : sàcc, siif,...

Coowal Raglu Le Dantec bi

Li nit ñi doon xel ñaar ak a laam-laame, leer na ! raglu Le Dantec...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

POLITIG : Toussaint Manga génn na PDS  Ab bataaxal la kii di Toussaint Manga jébbal njitaal...

Naalub yeesalaat Raglu Aristide Le Dantec Li waral coow li 

Raglug Aristide Le Dantec lañ nar a tëj, 15 ut bii ñu dégmal. Ndogal...

XËCCOO SOOG A PÉNCOO

Njëlbeeni njureefi wotey Ngomblaan gi Ci dibéer jii, 31eelu fan ci sulet, la askanuw Senegaal...

ÑÀKK KAYITU-JUDDU GI NAG, BA KAÑ?

Ayu-bés yii weesu, yéenekaay yu bare dañoo xéy fésal ci seen xët bu njëkk...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA