Odia

TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko dugge mooy kaas ngir ñu bàyyi Paap Njaay, taskatu-xibaaru Walf biy faramfàcce mbirum Yoon ca tele ba. Bésub 7 màrs lañ ko nëbb jant bi ba nëgëni. Nee ñu dafa...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa Pastef ñoo ngiy def seen kemtalaayu kàttan ngir jàllale ko bitim-réew ngir mu fajoo fa. Nde, feebaram bi day gën di doy waar, taneegul ba nëgëni. Rax-ci-dolli, xameesul ban xeetu...

WAVE AK ORANGE MONEY, NUN LAÑ FI NEKKAL WALLA SEEN BOPP? (AMI MBENG)

Wax ji bari na, werante bi ne kurr, ñii naan « Ñaw ! Upp baax na...

Kàddug Maki Sàll, Njiitu réew mi (AMI MBENG)

Ndakaarook biir Senegaal amoon nañuy yëngu-yëngu yu metti : ñu bari ñàkk ci seen bakkan,...

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu...

XËT YI MUJJ

TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa...

ÀTTEWAAYU NDAKAARU : USMAAN SONKO WAX NA ÀTTEKAT BI AY DËGGAM

Usmaan Sonko jël na kàddu gi ca àttewaayu Ndakaaru, wax àttekat bi ay dëggam...

LAYOOB SONKO-MBAY ÑAŊ : XEEX BI DOOR NA !

Ñetti biisi Dakar Dem Dikk yu tàkk ca Petersen, AUCHAN Mermoos tàkk jëppeet, ay...