FUTBAL : SAA-SENEGAALI BITIM-RÉEW
Abiib Jara gan-ganluwul fa Àngalteer. Gannaaw ba mu jógee Strasbourg dem Sunderland, doomu Senegaal ji amal na ci gaawu gii matsam bu njëkk foofa. Mu nekkoon mats fo, mu daldi ciy paas ñu dugal.
El Maalig Juuf tàggatoo na tay ci dibéer ji...
Réewum Senegaal ak mu Móritani yeesal nañu ag pas ci seen diggante. Muy Pas gog, dina dindi lépp lu doon gàllànkoor dem beek dikk bi ci diggante ñaari réew yi.
Démb ci àjjuma ji, 11 sulet 2025, Yànqooba Jémme (jëwriñu tabaxte yeek yaale bi ci...