Paap Aali Jàllo

FUTBAL : LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE AK CONFERENCE LEAGUE

Barki-démb, démb ak tey lañ doon amal joŋantey kaar-dë-finaal Ligue des champions yi, Europa League ak Conférence League fa Tugal. League des champions Ci talaata ji la Dortmund ak Atletico Madrid doon amal seen ñaareelu ndaje. Ca ndaje mu njëkk ma ame woon fa Espaañ, Atletico...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (18/4/2024)

ÑAAREELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Fay doon amal ñaareelu ndajem jëwriñam ginnaaw bi ñu ko falee ak léegi. Ca ndaje mooma jot naa fa jël ay ndogal boole ceek amal i càkkuteef ci yenn banqaasi Yoon yi,...

WOTEY 2024 : YENN LAWAX YAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY

Ginnaaw bi njureef yi tàmbalee rot, Basiiru Jomaay Fay moo jiitoogum, rawee yeneen lawax...

WOTEY 2024

Sàntar “Grande Medine” : Ci ndigalu perefe, dàq nañ taskati xibaar yépp bi waxtu...

LI GËN A FËS CI WOTE YI (24/3/2024)

SAA-SENEGAAL YU BARI GÉNN NAÑ WOTEJI Ci dibéeru tey ji lañu woo saa-senegaal ngir ñu...

BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY SIIWAL NA AM-AMAM

Basiiru Jomaay Jaxaar Fay dafa bokk ci lawax yiy dagaan baatu askan wi ngir...

LU TAX MAKI SÀLL MËNUL A KÀMPAAÑAL AAMADU BA ?

Fan yii nu génn, doon nañ yégle ne Njiitu réew mi, Maki Sàll, dina...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (19/3/2024)

XEEX BI AMOON ÑOORO : JÀPP NAÑ NDAWUL PASTEF LA Militaŋi Pastef yee doon xeex...

MAN, CEERNO ALASAAN SÀLL

Yeen, mbokki réew mi, Dama bëgg a waxtaan ak yeen ci réew mu màgg. Senegaal réew...

SONKO AK JOMAAY TUUMAAL NAÑ AAMADU BA

Démb la Usmaan Sonko ak Basiiru Jomaay Jaxaar Fay doon janook taskati xibaar yi...

XËT YI MUJJ

FUTBAL : LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE AK CONFERENCE LEAGUE

Barki-démb, démb ak tey lañ doon amal joŋantey kaar-dë-finaal Ligue des champions yi, Europa...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (18/4/2024)

ÑAAREELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Fay doon...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : « DAÑU WAR A TOPP NJIIT YI FI NEKKOON… »

TV5 doon na dalal werekaan bu mag bi, Bubakar Bóris Jóob, séq ak moom...

NJËLBEENI TUKKIY NJIITU RÉEWUM SENEGAAL FA GÀNNAAR AK GÀMBI

Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay,  dina amal njëlbeeni génnam ci ayu-bés bile. Moom...