PEREFE BU NDAKAARU AAYE NA MÓTO YI ÑU DAW BIIR NDAKAARU

Yeneen i xët

Aji bind ji

Perefe bu ndakaaru bi, Serif Muhammadu Bolondeŋ Njaay, génne na ab yégle buy aaye lépp luy móto di daw biir Ndakaaru li ko dale bésub tey, jàpp guddi ba xaaju guddi. Ciy waxam, nee na sàmm kaaraange askan wi a ko tax a jël lile dogal.

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj