Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar giy liggéey ay bunt ak i palanteer fa Jamñaajo. Ci alxamesu tay jii, 13 oktoobar 2025, lees ko doon amal fa sowub Jamñaajo.
Ndefar googu nag, 583i miliyoŋ lees ko taxawalee....