TUKKITEG NJIITU RÉEW MI FA TURKI
Keroog la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, demoon fa Araabi Sawdit. Mu doonoon tukkiteg waxtaan ci mbirum kopparal, ñu dippee ko “Future Investment Initiative Forum 2024”. Bi loolu jeexee, Njiitu réew mi defaale na umra. Ginnaaw ba...
Tàmbali nañu tabax ab dëq (digue) fa Daaru, diiwaanu Ndar. Jubluwway bi mooy aar askan wa ci walum dex Senegaal gi. DIRPA, banqaas bi yor kàddug làrme bi moo ko xamle.
Ci X (Twitter ba woon) la DIRPA bind, siiwal ne, : « Fa Daaru, ñu...