SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI : AJANDI NAÑ JOTAAY BI

Yeneen i xët

Aji bind ji

Njiitul Ngomblaan gi dàqandi na jotaay bi, ginnaaw bi dépitey Yewwi Askan Wi ak yu Taxawu Senegaal bàbbeekoo taxaw ci kanamu mikóro bi ne ñoo là, gàllankoor liggéey bi..

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj