Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa Pastef ñoo ngiy def seen kemtalaayu kàttan ngir jàllale ko bitim-réew ngir mu fajoo fa. Nde, feebaram bi day gën di doy waar, taneegul ba nëgëni. Rax-ci-dolli, xameesul ban xeetu...