Gëstukat yi ñu dénkoon mbirum Caaroy ak sóobare ya ñu fa bóomoon ca atum 1944 jébbal nañu Njiitu réew mi Téere bu weex bob, ci lañu dëxëñ njuréef yi tukkee ci seen luññutu gi ñi doon amal ñeel mbirum Caaroy 44, ñu duppe ko...
XIBAAR ÑEEL YOON
Téyandi nañu ràppëer bii di “10 000 problèmes” ak kii di Lamin Kàngaam. Ki tax ñu jàpp leen mooy Sëriñ Abdulaay Fay mi leen jure (pelent). Ab widewoo a leen boole. Ca biir widewoo booba, “10 000 problèmes” ak Lamin Kàngaam dañu...