Baabakar Lóo

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu gii. Waaye nag, wile yoon moom, xalam mi ci boppam moo damm. Xalamu Jimi Mbay ma woon, damm na, buum ya jaare fa dog ca talaata jee weesu, 12i fani...

COKKAASU ODIA

ÀNDU NAWLE

Bokk na ci anam yi nit lootaabee ag dundam ci kaw suuf, lu nekk...

WURE WA DEM NA KËŊŊ !

Ngomblaan gi, walla Péncum ndawi réew mi (ni ko ñenn ñiy wowee), benn la...

BALAA NOO LAAX JAAY…

Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a...

XËT YI MUJJ

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba...