Ngomblaan gee saay. Ki ko faat mooy Sëñ Jomaay. Démb la biral ndogal li, moom, Njiitu réew mi. Xibaar bi nag, bettul kenn. Nde, keroog, ca ëllëgu dibéeru 24 màrs 2024, bi njureefi mbañ-gàcce yi lawee, mu bir ne Jomaay a falu, ca lees...
NJIITU RÉEW MI DINA JANOOK ASKAN WI CI GUDDIG TEY JII
Bu yàggul dara la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge Siin ginnaaw ab tukki bu ma fa amaloon. Bi mu ñëwee, fekk na fi tiis ak naqar. Nde, li xew fa Mbuur...