Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ

Ginnaaw bi Majambal Jaañ dawee, génn réew mi, Nguurug Senegaal jàpplu na ko fu...

DOXU ÑAXTU KUJJE GI

Ginnaaw tekkaaral gu yàgg gees nemmeeku woon ci kujje gi diggante bi waa Pastef...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw...

MBIRUM SAA-SENEGAAL YI ÑU JÀPPOON FA MALI

Bàyyi nañu juróom-benni Saa-Senegaal yi ñu tegoon loxo fa Mali. Ci lees wax, terrorist...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/9/2025)

54EELU NDAJEM UPCI Démb ci altine ji lañu doon ubbi 54eelu ndajem ndiisoo giy doxal...

WAAJTAAYI GÀMMU 2025 : NJIITU RÉEW MAA NGA WOON FA TIWAAWAN

Tay ci gaawu bi, Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay moo nga...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/8/2025)

NGOMBLAAN GI Dépite yi wote nañu sémbuw àtte wiy jëmmal yoolekat yi. Muy àtte bob,...

DEKKALI SONACOS : YÉENEY NGUUR GI

Nguurug Senegaal gi dina yékkatiwaat kërug liggéey gii di SONACOS. Jël na 14i ndogal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA