Démb, ci gaawu bi la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, demoon fa Gàmbi. Li waral tukkeem boobu mooy fekke fukk ak benneelu ndajem Njiiti réew ak Càmmi “Organisation pour la mise en valeur du fleuve Gambie” (OMVS). Mu doon ndaje mu am solo ñeel...
Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga tay fa réewum Qataar. Njiitu réew ma, Séex Tamiim Bin Hamat Al Taani moo ko fa përyee woon ngir mu teewe ndajem Dohaa (Forum de Doha) mi ñu fay amal ci njeexitalu ayu-bés bi...