Odia

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

WAVE AK ORANGE MONEY, NUN LAÑ FI NEKKAL WALLA SEEN BOPP? (AMI MBENG)

Wax ji bari na, werante bi ne kurr, ñii naan « Ñaw ! Upp baax na...

Kàddug Maki Sàll, Njiitu réew mi (AMI MBENG)

Ndakaarook biir Senegaal amoon nañuy yëngu-yëngu yu metti : ñu bari ñàkk ci seen bakkan,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA