Li fës BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY By Paap Aali Jàllo 10/02/2024 0 210 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER » Mbay Sow - 17/11/2025 FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI Njuga Gay - 16/11/2025 JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER Mbay Sow - 13/11/2025 COKKAASU ODIA Odia - 13/11/2025 Aji bind ji Paap Aali Jàllo Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru. Móodu Géy, amoon 23i at, lañu dóor balu fetel ci biir bi. Biñ ko rawalee loppitaal la mujje faatu, démb. Ay mbokkam a siiwal xibaar bi. Paap Aali JàlloPlus de publicationsBiographiePaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/BÉSUB SÓOBARE YI : NJIITU RÉEW MA RAFETLU NA TAXAWAAYU SÓOBARE YI TE BOOLE LEEN CI POWI JOJ NDAKAARU 2026 YIPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ : YOON TEG NA LOXO MAYMUNA NDUUR FAY (7TV) AK BAABAKAR FAAL (GFM)Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/USMAAN SONKO YÉENE NA WÀÑÑIB MBËJ GI, NJAFAAN GEEK GIL BI FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj