BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY

Yeneen i xët

Aji bind ji

Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru. Móodu Géy, amoon 23i at, lañu dóor balu fetel ci biir bi. Biñ ko rawalee loppitaal la mujje faatu, démb. Ay mbokkam a siiwal xibaar bi.

Pap Aali Jàllo
Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj