Li fës BËTAL NAÑ BFEM BI By Paap Aali Jàllo 05/07/2024 0 166 Partager FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Yeneen i xët MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER » Mbay Sow - 17/11/2025 FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI Njuga Gay - 16/11/2025 JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER Mbay Sow - 13/11/2025 COKKAASU ODIA Odia - 13/11/2025 Aji bind ji Paap Aali Jàllo Bésub 18 sulet 2024 lañ àppaloon joŋante BFEM bi. Waaye, dañu ko mujje bëtal. Maanaam, dañ ko randal ba altine 22i pani sulet 2024. Bees sukkandikoo ci jëwriñu njàng mi, bésub 18 sulet bi ñu jëkkoon a jàpp dafay daje ak bésub tamxarit. Looloo sabab ñu dàq joŋante bi. BFEM nag, mooy lijaasa biy màndargaal njeexitalu njàngum daara yu digg-dóomu yi. Paap Aali JàlloPlus de publicationsBiographiePaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/BÉSUB SÓOBARE YI : NJIITU RÉEW MA RAFETLU NA TAXAWAAYU SÓOBARE YI TE BOOLE LEEN CI POWI JOJ NDAKAARU 2026 YIPaap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ : YOON TEG NA LOXO MAYMUNA NDUUR FAY (7TV) AK BAABAKAR FAAL (GFM)Paap Aali Jàllohttps://www.defuwaxu.com/author/paapaalijallo10/USMAAN SONKO YÉENE NA WÀÑÑIB MBËJ GI, NJAFAAN GEEK GIL BI FacebookTwitterWhatsAppE-mailImprimer Widewo VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU... Defu Waxu - Xët yi mujj