BËTAL NAÑ BFEM BI

Yeneen i xët

Aji bind ji

Bésub 18 sulet 2024 lañ àppaloon joŋante BFEM bi. Waaye, dañu ko mujje bëtal. Maanaam, dañ ko randal ba altine 22i pani sulet 2024.

Bees sukkandikoo ci jëwriñu njàng mi, bésub 18 sulet bi ñu jëkkoon a jàpp dafay daje ak bésub tamxarit. Looloo sabab ñu dàq joŋante bi.

BFEM nag, mooy lijaasa biy màndargaal njeexitalu njàngum daara yu digg-dóomu yi. 

Plus de publications

Widewo

Xët yi mujj