Xibaar

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...

NAFAG 2026 : JAGLEES NA 356 MILIYAAR NJËWRIÑU YAXANTU BEEK NDEFAR GI

Njiiti Senegaal yi dañu bëgg a jël fànnu ndefar wi, def ko xolu koom-koomu...

BÉSUB SÓOBARE YI : NJIITU RÉEW MA RAFETLU NA TAXAWAAYU SÓOBARE YI TE BOOLE LEEN CI POWI JOJ NDAKAARU 2026 YI

Ci altiney tay jii, 10i nowàmbar 2025, la Senegaal doon màggal Bésub  Sóobare yi....

COP 30 : ABDURAHMAAN JUUF FEDDALINA TAXAWAAYU SENEGAAL

Jëwriñ jii di Abdurahmaan Juuf yékkati na ay kàddu fa Beresil ngir dëggal taxawaayu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi...

LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI

Waa FMI dinañu toogaat ci réew ay fan ngir wéyal liggéey bi ñu sumb...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...