Xibaar

IMAAM AMAAT CAAM, IMAAM BU DËPPALE WOON DIINE AK JAMONO…

Imaam Caam dafa gëmoon bu baax ne, àddina mooy aar allaaxira. Li lay tax...

GINE BISAAWO | WOTEB FAL NJIITU RÉEW : FERNANDO DIAS DA COSTA MOO JIITOOGUM

Ci dibéeru démb ji la doomi Gine Bisaawo yi doon wote ngir fal seen...

UMS DÀNKAAFU NA MEETAR MUSAA BOOKAR CAAM

Kurélu àttekat yu Senegaal gi, UMS, ñaawlu na taxawaayu Meetar Musaa Bookar Caam ginnaaw...

AAMADU BA (JËWRIÑU MBATIIT MI) : « MBATIIT, DAFAY JUBOOLE TE DI SAXAL WÓOLOONTE »

Jëwriñu Mbatiit* mi, Ñeeñal* gi ak Wërteef* gi, Aamadu Ba mu Pastef, teewoon na...

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...