Xibaar

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB

Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw...

MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI

Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga...

NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI

Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji,...

SENEGAAL XAATIM NA DÉGGOOB 300I MILIYOŊI DOLAAR NGIR YEESAL MBAY MI

Jëwriñu Mbay mi, Dund bu matale bi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, xaatim...

NDAJEM SALI NGIR SELLAL DUND BI

Lekk baax na. Waaye nag, na doon lekk lu baax, ci anam bu baax....

MONJAAL 2026 / RDC-SENEGAAL : XEEXU GAYNDE AK TENE

Joŋante bu tar te nar a tàng mooy xaar sunu gayndey futbal yi war...

NDOGUM YOON MU METTI FA KEBEMEER

Ndogi yoon yaa ngi wéy di gën a bari. Saa yees jàppee ne ndog...

XËT YI MUJJ

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...